- Ismaël Lô Dibi Dibi Rek 歌詞
- Ismaël Lô
- Dibi dibi rek
dibi dibi rek aah dibi dibi rek aah dibi dibi rek
dibi dibi rek aah dibi dibi rek aah dibi dibi rek
yangui deugueurlou wante meunoko boul sop bayil niou djeuliko
yangui ndirok balai bou niou takhawal, aah ndakh yow lekkato
yangui beugu de ndakh yow nanato, boul sop bayil niou djeuliko
Ndakh mo ley madj lo
dibi dibi rek aah dibi dibi rek aah dibi dibi rek
dibi dibi rek aah dibi dibi rek aah dibi dibi rek
Ay niit niom bou niou beuguente, khamaal lo tchi waakh
Niom mame boye sene taar wessouna, waye tey laniou gueuneu beugueunte
Ya ngui beugu de ndakh yaw lekatto Bo fi guetarro waw ma bayiko
Ndakh mo ley madj lo
dibi dibi rek aah dibi dibi rek aah dibi dibi rek
dibi dibi rek aah dibi dibi rek aah dibi dibi rek
Mbeuguel kenn khamoul lou mou doonn Foulla diou barri ndaham amatou fi yoon Kholl moy capitainou boromam
Ndakh mo lay madj lo
Aah Aah dibi dibi rek
Aah Aah dibi dibi rek
Mo lay madj lo
dibi dibi aahdibi dibi dibi dibi rek
Mo lay madj lo
dibi dibi aahdibi dibi dibi rek
Mo lay madj lo
dibi dibi dibi dibi aahdibi dibi dibi dibi dibi rek
Mo lay madj lo
dibi dibi rek aahdibi dibi rek aah dibi dibi rek
Mo lay madj lo
dibi dibi rek aahdibi dibi rek aah dibi dibi rek ou ro ou ...
|
|