- Ismaël Lô Tajabone 歌詞
- Ismaël Lô
- Tadieu bone
Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone
Abdou ou djambar niari malaika la Khawe e tchikow danou tchi sa rou Momou mou ni la dangam djuli nga Momou mou ni la dangam woor nga
Khawe e tchikow danou tchi sa rou Momou mou ni la dangam djuli nga Momou mou ni la dangam woor nga Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone
(Wolei, Wolei, Wolei, Wolei)
Abdou Djambar (wolei) Niari malaika la (wolei) Tchi kow lay djogue (wolei) Danou tchi sa rou (wolei) Mouni la (wolei) Dangam djouli nga (wolei) Mouni la (wolei) Dangam woor nga (wolei) (Aaah !!!!!!)
|
|